×
New!

Bayan Al Islam Encyclopedia Mobile Application

Get it now!

Gënéelal toude yalla (Wollof)

Kiko wâjal: Ibrahim Khali Lô

Description

Gënéelal toude yalla - Toude léenma ma toude léen, sante léenma te bouléenma xarab.

Download Book

    بسم الله الرحمن الرحيم

    Gënéelal toude yalla

    YALLA neena :

    ﴿فَاذْكُرُونِي أَذْكُرْكُمْ وَاشْكُرُواْ لِي وَلاَ تَكْفُرُونِ﴾([1])

    Toude léenma ma toude léen, sante léenma te bouléenma xarab.

    YALLA wakhatne:

    ﴿يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اذْكُرُوا اللَّهَ ذِكْراً كَثِيراً([2])

    Yéen ñigëme déeléen toude YALLA lou bari lool.

    YALLA wakhatne:

    ﴿وَالذَّاكِرِينَ اللَّهَ كَثِيراً وَالذَّاكِرَاتِ أَعَدَّ اللَّهُ لَهُم مَّغْفِرَةً وَأَجْراً عَظِيماً([3])

    Dafalim mélokani ñigëm yalla moune ñom dëy ay toudou katou yalla yougor ag you jigéen lane, tedañou koy toude lou bari, moune ñom ñoñou dëy yalla migileeni xàré ak njeggël akouk paye gou rëye.

    YALLA wakhatne:

    ﴿وَاذْكُرْ رَّبَّكَ فِي نَفْسِكَ تَضَرُّعاً وَخِيفَةً وَدُونَ الْجَهْرِ مِنَ
    الْقَوْلِ بِالْغُدُوِّ وَالآصَالِ وَلاَ تَكُن مِّنَ
    الْغَافِلِينَ﴾([4])

    Néena: yaw yonneent bi (salla lahou alayhi wasallam): dél toud sa broom gay trokhlou ak diko ragal, te boulkoy biralle loole, naga koy def ci soubagi ag ngon gi, te boul book mouk ci ñi saggan.

    Yonnentebi (salla lahou alayhi wasallam) wakhne:

    ((مَثَلُ الَّذِي يَذْكُرُ رَبَّهُ، وَالَّذِي لاَ يَذْكُرُ ربَّهُ، مَثَلُ الْحَيِّ وَالْمَيِّتِ))([5])

    msaloum kiy toude yalla ak kiko doul toude migi melne kouy doundou ak kou dèe, limou ci dioublou moy toude yalla dafa mèlnè ag rouh ci yaram, koudoul toude yalla dafa mèlne kou fatou.

    وقال صلى الله عليه وسلم:

    ((أَلاَ أُنبِّئُكُم بِخَيْرِ أَعْمَالِكُمْ، وَأَزْكَاهَا عِنْدَ مَلِيكِكُمْ، وَأَرْفَعِهَا فِي دَرَجَاتِكُمْ، وَخَيْرٍ لَكُمْ مِنْ إِنْفَاقِ الذَّهَبِ وَالوَرِقِ، وَخَيْرٍ لَكُمْ مِنْ أَنْ تَلْقَوْا عَدُوَّكُمْ فَتَضْرِبُوا أَعْنَاقَهُمْ وَيَضْرِبُوا أَعْنَاقِكُم))؟قَالُوا بَلَى. ((ذِكْرُ اللَّهِ تَعَالَى))([6])

    Yonnentebi (salla lahou alayhi wasallam) wakhne:

    Xanaa doumalèen xibar ligën ci seeni diëfyi, te gëna teed fa seen broom, te gëna mana gàw ci yëkkati seeni graat fa yalla, te mo gën sakh gèen di diokhè wourous ak khalis, te gën gèen tasèek sèenoub non ci gèen di jihadag ñoom ñou dilèen ray gèen dilèen ray?

    Ñounèko wakhñouko kay, mounè lèen loolou moy toud yalla.

    وقال صلى الله عليه وسلم:

    ((يَقُولُ اللَّهُ تَعَالَى: أَنَا عِنْدَ ظَنِّ عَبْدِي بِي، وَأَنَا مَعَهُ إِذَا ذَكَرَنِي، فَإِنْ ذَكَرَنِي فِي نَفْسِهِ، ذَكَرْتُهُ فِي نَفْسِي، وَإِنْ ذَكَرَنِي فِي مَلَأٍ ، ذَكَرْتُهُ فِي مَلَأٍ خَيْرٍ مِنْهُمْ، وَإِنْ تَقَرَّبَ إِلَيَّ شِبْراً، تَقَرَّبْتُ إِلَيْهِ ذِرَاعاً، وَإِنْ تَقَرَّبَ إِلَيَّ ذِرَاعاً، تَقَرَّبْتُ إِلَيْهِ بَاعاً، وَإِنْ أَتَانِي يَمْشِي أَتَيْتُهُ هَرْوَلَةً))([7]).

    Yonnèn tèbi wakhnè:

    Yàlla mou kawè mi nèna: man màgi fima sama diàmbi ñortou, bourafètè ci màn ma rafètal diamè ci moom, bouñàwèe ñorte lamou ñortou lafay fèk.

    Nèna man magi andak sama diàbi andoug dëgral ak tawfikhal fik migimay toud, bouma touddè ci lou nëbbou fo khamnè mom rèkka fa nèk matoudko fi man.

    Bouma touddè ci mboolo matoudko ci mboolo mouka gene, tè moy mbooloom malàkaya, bou ma digèñalo ci toopma ak wout sama gërëm loutolnè digëntè binèk sabàràmou dëy bi ak bàràmou sandikàa bo boolèn garalè man danako diègèñalou lou toolnè lokhoo, mom sama diàmbi bou ma digèñalo lou tèlnè ab lokho booko tàllalè man danàko diègèñalou lou toolnè ñàri lookho yoo tàllàl, bou sam diàmbi di dik ci man di di dookh, man magatanoukou did aw.

    (limou ci dioublou mooy loo daw diëm ci yàlla yà yàlla loudoubal liga dèf lay dèf gir khëthila ga ak ci moom.

    وعن عبد الله بن بسر رضي الله عنه أَنَّ رَجُلاً قَالَ: يَا رَسُولَ اللَّهِ، إِنَّ شَرَائِعَ الإِسْلاَمِ قَدْ كَثُرَتْ عَليَّ، فَأَخْبِرْنِي بِشَيْءٍ أَتَشَبَّثُ بِهِ. قَالَ: ((لاَ يَزَالُ لِسَانُكَ رَطْباً مِنْ ذِكْرِ اللَّهِ))([8]).

    Sahàba bi toud abdoul làh ibnou bousr danè dafa am bèn wày bou wakh yonnèn tèbi nèko màndàl yi lislàm di dèglè dafa bari, tè damà bëg ga wakhma loo khàmnè dama thiy gooy ga khamnè mooy doon limày dièkhal li ëppe ci sama wakhtou.

    Yoonnèntèbi sallal làhou alayhi wa sàllama nèko: saw làmmiñ boumou dañ mouk di tooy ci toude yàlla.

    وقال صلى الله عليه وسلم:

    ((مَنْ قَرَأَ حَرْفاً مِنْ كِتَابِ اللَّهِ فَلَهُ بِهِ حَسَنَةٌ، وَالْحَسَنَةُ بِعَشْرِ أَمْثَالِهَا، لا أقول: ((الم)) حَرْفٌ، وَلَكِنْ: أَلِفٌ حَرْفٌ، وَلاَمٌ حَرْفٌ، وَمِيْمٌ حَرْفٌ))([9]).

    Yoonnètèbi sallàhou alahi wasalama nèna:

    Kou diàng aw araf ci alkhràn yàlla dalay bindal ab touyàba, dàdi lakoy foulal foukki yoon,

    Mounè wakhoumanè bàtou (alf làm mmim) bEn aràf la, wayè alifgi arafla, làmgi arafla, mim gi arafla.

    وَعَنْ عُقْبَةَ بْنِ عَامِرٍ رضي الله عنه قال:

    خَرَجَ رَسُولُ الله صلى الله عليه وسلم وَنَحْنُ فِي الصُّفَّةِ، فَقَالَ: ((أَيُّكُمْ يُحِبُّ أَنْ يَغْدُوَ كُلَّ يَوْمٍ إِلَى بُطْحَانَ، أَوْ إِلَى الْعَقِيقِ، فَيَأْتيَ مِنْهُ بِنَاقَتَيْنِ كَوْمَاوَيْنِ فِي غَيْرِ إِثْمٍ وَلاَ قَطِيعَةِ رَحِمٍ) فَقُلْنَا: يَا رَسُولَ اللَّهِ نُحِبُّ ذَلِكَ. قَالَ: ((أَفَلاَ يَغْدُو أَحَدُكُمْ إِلَى المَسْجِدِ فَيَعْلَمَ، أَوْ يَقْرَأَ آيَتَيْنِ مِنْ كِتَابِ اللَّهِ ﷻ‬ خَيْرٌ لَهُ مِنْ نَاقَتَيْنِ، وَثَلاثٌ خَيْرٌ لَهُ مِنْ ثَلاَثٍ، وَأَرْبَعٌ خَيْرٌ لَهُ مِنْ أَرْبَعٍ، وَمِنْ أَعْدَادِهِنَّ مِنَ الإِبِلِ))([10]).

    Oukhbata ibnou àmirin di ab sahàba yàlla nako yàlla gërëm nèna: yoonnètèbi dafa gène ci kërëm ñëw ci diàkka ji fèk lèn ci palace bi ñou diaglèl ñi amoul fouñou dëk ñounànk souffa, mounè lèn kan ci yèn moo bëga khëy bisbounè dèm thia khourou bouthàn wala khrou akhikh (ñàri khour lañ you nèk màdina) mou dièlfa ñàri gëlèm you rëy ay digèn ci loudoul bàkkàr wala louy waral ak mbook gou dag?

    Ñounèko noun ñèppa bëg loolou kay.

    Mounè kèn ci yèn khëy dèm thia diakka dia mou xamlou fa wala mou diàngfa ñàri àya moo gën ci moom ñàri gëlèm, ñàtti àya moogën ci moom ñàtti gëlèm, ñènti àya mogën ci moom ñènti gëlèm, louma diàng ci limoub àya moo gën lim bouni tool ci ay gëlèm.

    وقال صلى الله عليه وسلم:

    ((مَنْ قَعَدَ مَقْعَدَاً لَمْ يَذْكُرِ اللَّهَ فِيهِ، كَانَتْ عَلَيْهِ مِنَ اللَّهِ تِرَةٌ، وَمَنِ اضْطَجَعَ مَضْجِعاً لَمْ يَذْكُرِ اللَّهَ فِيهِ كَانَتْ عَلَيْهِ مِنَ اللَّهِ تِرَةٌ))([11]).

    Yoonèntèbi sallàl làhou alyhi wasallama nèna: kou took ci ab palace tè touddofa yàlla dana ci diali ak wañèkou akouk rèthiou, kou tëde ci ab tëddoukay tè touddofa yàlla dana ci diali ak wañèkou akouk rèthiou.

    وقال صلى الله عليه وسلم:

    ((مَا جَلَسَ قَوْمٌ مَجْلِسَاً لَمْ يَذْكُرُوا اللَّهَ فِيهِ، وَلَمْ يُصَلُّوا عَلَى نَبِيِّهِمْ إِلاَّ كَانَ عَلَيْهِمْ تِرَةً، فَإِنْ شَاءَ عذَّبَهُمْ، وَإِنْ شَاءَ غَفَرَ لَهُمْ))([12]).

    Nèna amoul ay nit ñou toog ci ab diatày tè touddouñ fa yàlla diouli wouñou fa ci yoonnèn tèbi sallal làhou alayhi wasalama loudoulnè diatàybooba dana doon ak pèrtàgè ak louñouy rèthiou, bou nèkhè yàlla mou mbougal lèn ci, bouko nèkhè mou dièggal lèn.

    وقال صلى الله عليه وسلم:

    ((مَا مِنْ قَوْمٍ يَقُومُونَ مِنْ مَجْلِسٍ لاَ يَذْكُرُونَ اللَّهَ فِيهِ إِلاَّ قَامُوا عَنْ مِثْلِ جِيفَةِ حِمَارٍ، وَكَانَ لهُمْ حَسْرةً))([13]).

    Yoonnèntèbi sallal làhou alayhi wasallama nèna:

    ay nit ñou toog ci ab diatày tè touddouñ fa yàlla loudoul bouñouy diok dañiy mèlnè ñoutoogon tim mèddoum mbàm, tè sèn diatày booba dana doon louñouy rèthiou .



    Ligay ñaan boo yew woo ciy nelaw

    Daganàn:

    ((الْحَمْدُ للَّهِ الَّذِي أَحْيَانَا بَعْدَ مَا أَمَاتَنَا، وَإِلَيْهِ النُّشُورُ))([14]).

    Niga koy diangé:

    Alhmdou lil lahil lazi ahyànà bahda maa amatanaa, wa ilayhin nouchour.

    Limouy firi:

    Magi sant yalla miñou doundalaat ginaw bimouñou fàatèe, te bouñou dèkkèe ci moom lañou dëm.

    (limou dioublou ci fatou gii mooy nelaw, ndakh nelaw fatou gou ndawla).

    Gawakhaatnè:

    ((لاَ إِلَهَ إِلاَّ اللَّهُ وَحْدَهُ لاَ شَريكَ لَهُ، لَهُ الْمُلْكُ وَلَهُ الْحَمْدُ، وَهُوَ عَلَى كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ، سُبْحَانَ اللَّهِ، وَالْحَمْدُ للَّهِ، وَلاَ إِلَهَ إِلاَّ اللَّهُ، وَاللَّهُ أَكبَرُ، وَلاَ حَوْلَ وَلاَ قُوَّةَ إِلاَّ بِاللَّهِ الْعَلِيِّ الْعَظِيمِ، رَبِّ اغْفرْ لِي))([15]).

    Niga koy diangè:

    La ilaha illal lah wahdhou la charika lhou, lhoul moukou walhoul hamdou, wa houwa alaa koulli chaye in khadiroun.

    Soubhanal laah, walhamdou lillaah , walà ilàha illal làh, allahou akbàr.

    Walà hawla walà khouwwata illà bil làhil aliyyil asimi.

    Limiy firi moy:

    Amoul keen wala lèen lou yayoo ñou diàmouko koudoul yàlla, mom dong ga ko yayoo, te amoul kén kou ñouy ko ciy bookkalèl, yàlla momom lèep louy ngour, ak lèep louy khetou cinte mooko yayo, temooy ki am kattan ci lèepe.

    Sellal nako ci lèep louñou koy bookkalè ak lèep louy ag mankitè.

    Diko sant moom mi yayo bmolèem kheti thiante yi.

    Di sèedenè Amoul keen wala lèen lou yayoo ñou diàmouko koudoul yàlla.

    Te mom yalla mogëna mag lounè.

    Te amoul ben kattan walla men pèkhè mou mana sootti loudoul ci thiobarèem ak ndimbalëm.

    Mom yalla mooy kou kaweki te mooy kou mag ki.

    Yaw sama broom dièggalma samay bakkàar.

    Yonnèntèbi (sallal làhou alayhi wasallama) nèna: kou yèewou wakhli dièeggal nañ ko ay bakkàram, te bou ñanèe yàlla naggou ñànam, tè bou diougèe moudadi diàpe dadi dioulli yàlla dana naggou ag dioullèem.

    Ga wakhàtnè:

    ((الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي عَافَانِي فِي جَسَدِي، وَرَدَّ عَلَيَّ رُوحِي، وَأَذِنَ لي بِذِكْرِهِ))([16]).

    Niga koy diangè:

    Alhamdou lil lahil lazi hafani fi disadi, waradda alayya rouhi, wa azina lii bizikrihi.

    Limiy firi moy:

    Magi sant yalla mima mousal diammal ma ci sama yaram, mou dello watma samg rouhe, mou yoomba lalma toud ko mom yalla.

    Gadadi diang àya yi:

    ﴿إِنَّ فِي خَلْقِ السَّمَوَاتِ وَالأَرْضِ وَاخْتِلاَفِ اللَّيْلِ وَالنَّهَارِ لَآيَاتٍ لأُوْلِي الألْبَابِ * الَّذِينَ يَذْكُرُونَ اللَّهَ قِيَاماً وَقُعُوداً وَعَلَىَ جُنُوبِهِمْ وَيَتَفَكَّرُونَ فِي خَلْقِ السَّمَوَاتِ وَالأَرْضِ رَبَّنَا مَا خَلَقْتَ هَذا بَاطِلاً سُبْحَانَكَ فَقِنَا عَذَابَ النَّارِ* رَبَّنَا إِنَّكَ مَن تُدْخِلِ النَّارَ فَقَدْ أَخْزَيْتَهُ وَمَا لِلظَّالِمِينَ مِنْ أَنصَارٍ* رَّبَّنَا إِنَّنَا سَمِعْنَا مُنَادِياً يُنَادِي لِلإِيمَانِ أَنْ آمِنُواْ بِرَبِّكُمْ فَآمَنَّا رَبَّنَا فَاغْفِرْ لَنَا ذُنُوبَنَا وَكَفِّرْ عَنَّا سَيِّئَاتِنَا وَتَوَفَّنَا مَعَ الأبْرَارِ* رَبَّنَا وَآتِنَا مَا وَعَدتَّنَا عَلَى رُسُلِكَ وَلاَ تُخْزِنَا يَوْمَ الْقِيَامَةِ إِنَّكَ لاَ تُخْلِفُ الْمِيعَادَ* فَاسْتَجَابَ لَهُمْ رَبُّهُمْ أَنِّي لاَ أُضِيعُ عَمَلَ عَامِلٍ مِّنكُم مِّن ذَكَرٍ أَوْ أُنثَى بَعْضُكُم مِّن بَعْضٍ فَالَّذِينَ هَاجَرُواْ وَأُخْرِجُواْ مِن دِيَارِهِمْ وَأُوذُواْ فِي سَبِيلِي وَقَاتَلُواْ وَقُتِلُواْ لأُكَفِّرَنَّ عَنْهُمْ سَيِّئَاتِهِمْ وَلأُدْخِلَنَّهُمْ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الأَنْهَارُ ثَوَاباً مِّن عِندِ اللَّهِ وَاللَّهُ عِندَهُ حُسْنُ الثَّوَابِ * لاَ يَغُرَّنَّكَ تَقَلُّبُ الَّذِينَ كَفَرُواْ فِي الْبِلاَدِ * مَتَاعٌ قَلِيلٌ ثُمَّ مَأْوَاهُمْ جَهَنَّمُ وَبِئْسَ الْمِهَادُ * لَكِنِ الَّذِينَ اتَّقَوْاْ رَبَّهُمْ لَهُمْ جَنَّاتٌ تَجْرِي مِنْ تَحْتِهَا الأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا نُزُلاً مِّنْ عِندِ اللَّهِ وَمَا عِندَ اللَّهِ خَيْرٌ لِّلأَبْرَارِ * وَإِنَّ مِنْ أَهْلِ الْكِتَابِ لَمَن يُؤْمِنُ بِاللَّهِ وَمَا أُنزِلَ إِلَيْكُمْ وَمَآ أُنزِلَ إِلَيْهِمْ خَاشِعِينَ لِلَّهِ لاَ يَشْتَرُونَ بِآيَاتِ اللَّهِ ثَمَناً قَلِيلاً أُوْلَئِكَ لَهُمْ أَجْرُهُمْ عِندَ رَبِّهِمْ إِنَّ اللَّهَ سَرِيعُ الْحِسَابِ*يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُواْ اصْبِرُواْ وَصَابِرُواْ وَرَابِطُواْ وَاتَّقُواْ اللَّهَ لَعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ﴾))([17]).

    Limiy firi moy:

    Soungou brom dane: bind gi ñou binde asaman ak souf, ag wouta

    ([1]) سورة البقرة، الآية: 152 .

    ([2]) سورة الأحزاب، الآية: 41 .

    ([3]) سورة الأحزاب، الآية: 35 .

    ([4]) سورة الأحزاب، الآية: 35 .

    ([5]) البخاري مع الفتح، 11/ 208، برقم 6407، ومسلم، 1/ 539، برقم 779، بلفظ: ((مثل البيت الذي يذكر اللَّه فيه والبيت الذي لا يذكر اللَّه فيه مثل الحي والميت))، 1/539 .

    ([6]) الترمذي، 5/ 459، برقم 3377، وابن ماجه، 2/ 124، برقم 3790، وانظر: صحيح ابن ماجه، 2/ 316، وصحيح الترمذي، 3/ 139.

    ([7]) البخاري، 8/ 171، برقم 7405، ومسلم، 4/ 2061، برقم 2675، واللفظ للبخاري.

    ([8]) الترمذي، 5/ 458، برقم 3375، وابن ماجه، 2/ 1246،3793، وصححه الألباني في: صحيح الترمذي، 3/139، وصحيح ابن ماجه، 2/317.

    ([9]) الترمذي، 5/ 175، برقم 2910، وصححه الألباني: صحيح الترمذي، 3/9، وصحيح الجامع الصغير، 5/340 .

    ([10]) مسلم، 1/553 ، برقم 803.

    ([11]) أبو داود، 4/ 264، برقم 4856، وغيره، وانظر: صحيح الجامع، 5/342.

    ([12]) الترمذي، 5/ 461، برقم 3380، وانظر: صحيح الترمذي، 3/140.

    ([13]) أبو داود، 4/ 264، برقم 4855، وأحمد، 2/389، برقم 10680، وانظر: صحيح الجامع، 5/176 .

    ([14]) البخاري مع الفتح، 11/ 113، برقم 6314، ومسلم، 4/ 2083، برقم 2711.

    ([15]) من قال ذلك غُفِرَ له، فإن دعا استجيب له، فإن قام فتوضأ ثم صلى قُبلت صلاته، البخاري مع الفتح، 3/ 39، برقم 1154، وغيره، واللفظ لابن ماجه، انظر: صحيح ابن ماجه، 2/335 .

    ([16]) الترمذي، 5/ 473، برقم 3401، وانظر: صحيح الترمذي، 3/144.

    ([17]) الآيات من سورة آل عمران، 190-200، البخاري مع الفتح،
    8/ 337، برقم 4569، ومسلم، 1/ 530، برقم 256.

    معلومات المادة باللغة العربية